Additional information
Auteurs | Doudou Diop, Fary Silate Ka, Adjaratou Oumar Sall, Danielle Wozny |
---|---|
Traducteurs | Adjaratou Oumar Sall |
Ndajalaat mi « Genn garab, benn téere » mu ngi jëm ci ñiy jàng lekkol ak seeni waajur: ay téere yu ndaw lañu, ñu bind leen ci ñaari làkk farañse ak làkki réew mi. Téere yi dañuy yee maas gu ndaw gi ci ndonol xam-xamu gàncaxi réew mi, mu war a am taxawaay bu mat sëkk ci jafe-jafey kéew yi juddoo ci tàngooru jaww ji.
Auteurs | Doudou Diop, Fary Silate Ka, Adjaratou Oumar Sall, Danielle Wozny |
---|---|
Traducteurs | Adjaratou Oumar Sall |